Radiitu, sabab bi tax Sëriñ Tuubaa bind ko, mooy jamono yi mu nekkee ci Gabon, ci dëkk bii di Mayomba, fa mu daan jullee da faa sampoon ñeenti bant, ngir bañ ñuy romb ci kanamam buy julli.
Am benn commandant bu nekkoon foofu, ⬇️
ba mu gisee Sëriñ bi def loolu mu ñëw sempi bant ya sànni ko, boole ci wax yu teggine wul, daal di ne Sëriñ bi « fii julli amu fi, Lislaam amu fi ! dangaa bëgga yàq soldaar yi fi nekk, waaye doo ko fi defee! ». Sëriñ Tuubaa nee na « ma muñ rekk, daal di noppi, tontu wuma ko »
Waaye amoon na fa ku ñuy wax Yelli Sëy, ba mu gisee li ma Commandant boobu def, dafa daaldi ñëw dal ci kawam, ne ko « bant yi dinaa ko delloo na mu meloon, ndax Sëriñ bi xatalu ci kenn, te tooñul kenn… » commandant bi ne ko « doo ko fa delloo » ñu nekk ci ñoom ñaar di xolóo,
bay waaja xeex, waaye nit ñee dox seen diggënte. Li ko tambalee tàkkusaan ba timis ñu nekk di xuloo.
Qasida gi moo tambalee ci bëyit wii « radiitu anil mawlaa tahaalaa lazii rabbaa »
رضيت عن المولى تعلى الذي ربّى
فؤادي وأعناني وأكرم به ربا
Sëriñ bi nee na « bi may bind Qasida gi, ba àgg ci bëyit wii 👇
له اكتب صلاة مع سلام بآله
وأصحابه واجعل به مسجدي رحبا
(Yaw sunu Boroom, yàlna nga dolli xéewël ak mucc ci Yonent bi, ak ay sahaabaam, ak njabootam. Te nga defal ma jumaa ju yaatu) ».
Nee na « bi ma bindee bëyit wii ci lama sunu Boroom xamal ne, nangu naa sa ñaan, te jumaa yii ngay ñaan, jenn ji di nga ci teg sa bët,
muy jumaay Njaareem. Jeneen Jumaa ji di na noppi sa ginaaw Inch’Allah, muy Jumaay Tuubaa ».
Moo tax keroog ba Yelli sëy ñëwee Njaareem, Sëriñ Tuubaa dakoo boole ak Sëñ Muhamadul Amiin Joob Dagana, ne ko « yobb ko mu siyaara Jumaa ji ». Ba mu siayaaree ba noppi,
Sëriñ Tuubaa ne ko « noo gisee jumaa jii ak bant yooyee ma sampoon, te nga ca doon xuloo? »…
Après la prière isha (Gewe) de la dernière nuit qu'il a passée au Jolof ( Ceeyen), Serigne Touba convoqua tous les disciples. Lorsqu'ils se présentèrent, il leur dit : « Approchez, car je voudrais m'entretenir avec vous.⬇️
Nous allons quitter ce lieu pour aller compléter le reste du service dans la ville ( Diourbel). Sachez que je partagerai avec vous toutes les peines qu'on aura à croiser là-bas. À cet effet, j'aimerais vous donner des conseils que vous retiendrez
rigoureusement avant que nous soyons dans ce lieu. Je vous recommande de les suivre à la lettre.
« Craignez Dieu. Avez-vous bien entendu ce que j'ai dit ?» Ils répondirent : « Oui !» C'est alors qu'il leur dit ce qui suit :
L'aspirant mouride a besoin de dix outils pour son voyage intérieur. Il s'agit de :
• La résolution qui précède le voyage
• Le guide qui n'est que le chef spirituel assez illuminé
• La ferveur pieuse qui sert de viatique⬇️
• L'ablution qui tient lieu d'armes et qui élimine l'état d'impureté
• La répétition sans cesse du glorieux Nom d'ALLAH qui est leur lanterne
• Un haut souci de bonne volonté qui tient lieu de monture
• La conscience de son impuissance dans l'abandon à ALLAH, qui sert de bâton d'appui,
La détermination qui est sa ceinture selon l'avis des gens de la voie
• Le "sharia" constitue la route qu'il suit du début à la fin
• Des frères de même but, déterminés,
De toutes les cités africaines, Touba est une des plus particulières. Elle ne saurait être comparée à une autre cité du continent. Alors que les humains fondent habituellement des villages et ensuite construisent les temples ;
à Touba, c’est le temple qui a créé la cité. Une ville d’un million d’âmes a été édifiée par l’impulsion d’un seul esprit, celui d’Ahmadou Bamba. Un homme peut-il changer l’Histoire ? Apparemment oui.
C’est une bonne chose, car Touba est un des plus grands trésors du Sénégal, qu’on soit mouride ou pas. Pourquoi ? L’Afrique a surmonté deux grandes catastrophes. C’est à ces deux moments que l’Afrique a perdu sa liberté. La première fois fut avec la traite négrière