Yàlla neena Yonent bi ﷺ, « Te yékatil nanu la saw tur (wala saw tagg) »
Dëgg la ! Ndax, su weesoo sax lim bu takku biy juli ci moom bis bu nek, ak ni ñiy topp diinéem ji di yokkee bis bu set... foo gestu gis sëttu Yonent bi ﷺ... Waaye ku mëssa gis sëttu Abu Jahl ? ⬇️
Waa Makka doon nañu ko ñaawal bi doomam ji Ibraahim génnée àdduna ci ñaari attam, naan ki deh Yàllaam ji daf ko bañ (ndax mënnul am doom bu góor), kii daal su fi juggée wayam fay ndax du am ndono, kii daal moo dog ci yiw ! ⬇️
Yàlla ne ko... « إِنَّ شَانِئَكَ هُوَ ٱلۡأَبۡتَرُ »
Ñoom ñi lay bañ aka ñaawal, ñoom ñoo dog ci bépp yiw, ñoom la seen tur di fay...
Waaye yaw moom... « وَرَفَعْنَا لَكَ ذِكْرَكَ »
Man maa yekkati saw tur, maa yëkkati saw tagg muy wéy diirab jamono... ⬇️
Cheikh Ibrahima Niass, vit le jour au 15e jour du mois lunaire RAJAB de l'an Hégirien 1318, à l'ombre d'un Baobab qui surplombait la concession familiale. Dans le calendrier grégorien, cette date correspond au Jeudi #8Novembre1900. ⬇️
Lorsqu'on vint annoncer à El Hadji Abdoulaye Niass qu'il était père d'un garçon, Abdou Salla Niass venait de prononcer « minal djinati wa naassi » (Sourate les Hommes, verset N°6), phrase qui marque la fin de la récitation du SAINT CORAN. ⬇️
#Baye_Niass ! Nul personnage plus que lui n'eveille tant les passions des uns par excès de zèle, ou des autres par incompréhension, méconnaissance, jalousie, dénigrement, hypocrisie voire même méchanceté. ⬇️
Son nom de baptême est IBRAHIMA NIASS, fils d'Elhadji Abdoulaye Niass et de Aissatou Diankha, il est l'homonyme de son grand oncle Ibrahima Thiam dit Serigne Kéllel. ⬇️