مجنون باي Profile picture
Passioné de #Baye_Niass...!
Aug 10, 2022 4 tweets 1 min read
Yàlla neena Yonent bi ﷺ, « Te yékatil nanu la saw tur (wala saw tagg) »

Dëgg la ! Ndax, su weesoo sax lim bu takku biy juli ci moom bis bu nek, ak ni ñiy topp diinéem ji di yokkee bis bu set... foo gestu gis sëttu Yonent bi ﷺ... Waaye ku mëssa gis sëttu Abu Jahl ? ⬇️ Waa Makka doon nañu ko ñaawal bi doomam ji Ibraahim génnée àdduna ci ñaari attam, naan ki deh Yàllaam ji daf ko bañ (ndax mënnul am doom bu góor), kii daal su fi juggée wayam fay ndax du am ndono, kii daal moo dog ci yiw ! ⬇️
Aug 9, 2022 5 tweets 1 min read
| Wasfu Zatu Imāmi | Xasida bu gàtt bu Baay di tënk melo #SeydinaCheikh

وَصْفُ ذَاتِ الْإِمَامِ خُذْهَا بَدِيعًا
دُونَهَا نَظْمُ الدُّرِّ ذَاكَ الْبَهَاءُ

Melo jëmi njiit li (Seex Tijaan) jël ko muy lu rafet, weesu na jëm ja nosseb wurrussu durru loolu moy ab taar
⬇️ رَبْعَةُ الْقَدِّ أَبْيَضُ اللَّوْنِ شَيْخِي
مُشْرَبٌ فِيهِ شَيْبَةٌ حَسْنَاءُ

Ajji dig dóomu la ab taxawaay da fa weexoon ab melo bu ñu rax xonk, ku amoon bijaaw bu rafet
⬇️
Nov 8, 2020 13 tweets 3 min read
Naissance et Origines d'El Hadji Ibrahima Niass.

Extrait du livre de Mbaye Thiam intitulé « Cheikh Al Islam Elhadji Ibrahim Niass, Imam de la Faydatou Tidianiya »

#Thread ⬇️
#8Novembre1900 Cheikh Ibrahima Niass, vit le jour au 15e jour du mois lunaire RAJAB de l'an Hégirien 1318, à l'ombre d'un Baobab qui surplombait la concession familiale. Dans le calendrier grégorien, cette date correspond au Jeudi #8Novembre1900. ⬇️
Nov 8, 2020 8 tweets 2 min read
Origine de quelques uns des surnoms attribués à El Hadji Ibrahima Niass.

Extrait du livre du Professeur Mbaye Thiam intitulé « Cheikh Al Islam El Hadji Ibrahima Niass, Imam de la Faydatou Al Tidianiya »

#Thread ⬇️
#8Novembre1900 #Baye_Niass ! Nul personnage plus que lui n'eveille tant les passions des uns par excès de zèle, ou des autres par incompréhension, méconnaissance, jalousie, dénigrement, hypocrisie voire même méchanceté. ⬇️
Nov 8, 2020 4 tweets 1 min read
Poème de Cheikhaani sur #Baye_Niass ⬇️
#8Novembre1900 / #15Rajab1318 أتيتك يـــــامــولاي في اليــــوم والأمـس
ومــــالي من شيء سواكم إلى الرمــــس

ومــــالي في اليوم المؤمــــل غيركـــــــم
أحن لكــــــــــم بالقلــــب فيه و بالنفــــس

رأيتــــك يوم الجمــــع عبــــدا وسيـــــدا
وقد كنت قبل القبـل في حضرة القــــــدس